%3Aformat(webp)%2Fi.ytimg.com%252Fvi_webp%252FxJyVUXH6SsQ%252Fmaxresdefault.webp&w=1139&q=75)
Description:
Votre cadeau du nouvel an 🥳😍 est disponible sur toutes les plateformes de streaming : https://bfan.link/saajobaan Auteur & Interprète : Saliou Samb AKA Amadeus Compositeur : Zoom Beat © 2022 COSANOSTRA Suivez Amadeus sur les réseaux sociaux : Instagram : https://www.facebook.com/unsupportedbrowser Twitter : https://twitter.com/massambaamadeus Facebook : https://www.facebook.com/unsupportedbrowser Paroles en Wolof : Eey Màsamba Waalo eeeh hii Su mbëggeel doon jaay Am naa njëgam Dinaa la wan sama yéene yi ma am ci yaw Duma ku lay jay Te duma la wor Dinaa la wax dëgg ak lum metti metti Maa la woo ne la maa la nob Miinal la sama bopp ba nga barder maa la tooñ Kon nag loo ma manti def Lu mu metti naa ko muñ Àdduna du dox ba ma soppi li ma la wax doo ma weddi Ay bu doon ay nax neex na ma Fekk ma ciy gént yee nga ma Jàmm ju bari may nga ma Yaa ngi may dundal àjjana Tamit tëggal ma ma jaayu Xamal ma ne man la Gëmal ma ne Man rekk nga nob Sama saajobaan Tëggal ma ma jaayu Xamal ma ne Man la gëmal ma ne Man rekk nga nob Sama saadjobaan eeee waay Xam nga duma puruux duma fàtte bi may surux Xuntu wu lëndëm wi nga ma génne dinaa ko wax Du lu rafet ci wax Soo ma bàyyee damay torox Nawle yépp bis bu ñu teewee dinaa ko wax waaaay Doy nga ma ci kër Kenn du la sikkal Man yaw mii yaay ki ma fiital (tiital) Doo dund ngistal Ngor gi nga jiital Ragaluma siiwal Nun ñaar ndax doy nga ma ci kër Ndaxte Mane maa la woo Ne la maa la nob Miinal la sama bopp ba nga barder maa la tooñ Kon nag loo ma manti def Lu mu metti naa ko muñ Àdduna du dox ba ma soppi li ma la wax doo ma weddi Hay bu doon ay nax neex na ma Fekk ma ciy gént yee nga ma Jàmm ju bari may nga ma Yaa ngi may dundal àjjana Tamit tëggal ma ma jaayu Tëggal ma ma jaayu Xamal ma ne Man la Gëmal ma ne Man rekk nga nob Sama saajobaan Tëggal ma ma jaayu Xamal ma ne Man la Gëmal ma ne Man rekk nga nob Sama saajobaan eeee waaay Bis (tòllanti) ...................................................................................................................................... Traduction des paroles en Français : "Ma Dulcinée" Eey Massamba Wallo hummm hun Si l'amour avait un prix Je me donnerais à tout prix Pour l'acheter sans cris Je te manifesterai mes bonnes intentions Je t'éloignerai de toute trahison Je ne te complimenterai jamais ma solution Je te dirai la vérité en toute circonstance Car je t'ai choisie comme amour avec aisance Amour, finalement obnubilé par ma fréquence Je te supporterai pour toujours avec patience Fais-moi bébé ton homme de confiance Parce que doué de rigueur et de Constance Et si tes dires étaient des balivernes Je m'en contenterais dans ma caserne Tu m'as extirpé de mes délires Pour me permettre de tout lire Tu m'as permis d'avoir une vie paisible Assimilée au paradis, notre seule et unique cible Chante alors glorieusement mes éloges don du Ciel Rassure-moi foncièrement mon âme-sœur, ma belle Montre-moi qu'il n'y a point d'amour comme tel Ma Dulcinée, tu es plus délicieuse qu'un caramel Ma dulcinée Couplet 2 Loin des traîtres dépourvus de reconnaissance J'assume d'avoir bénéficié de ton assistance Après être envahi par le vent de l'ignorance Ma vie sombrerait dans l'oubli Si tu me quittes ou même m'oublies Je réaffirmerai ma Dulcinée solennellement Devant toute l'assemblée réunie par moment Que tu me combles de bonheur entièrement Personne ne peut "casser du sucre sur ton dos Ma force qui me porte sur son dos Tu ne réagis pas pour les yeux d'autrui Mais tu agis dignement sans faire de bruit J'ose dévoiler notre relation jour et nuit Ma Dulcinée, la femme très chère que je suis Je te dirai la vérité en toute circonstance Car je t'ai choisie comme amour avec aisance Amour, finalement obnubilé par ma fréquence Je te supporterai pour toujours avec patience Fais-moi bébé ton homme de confiance Parce que doué de rigueur et de Constance Et si tes dires étaient des balivernes Je m'en contenterais dans ma caserne Tu m'as extirpé de mes délires Pour me permettre de tout lire Tu m'as permis d'avoir une vie paisible Assimilée au paradis, notre seule et unique cible Chante alors glorieusement mes éloges don du Ciel Rassure-moi foncièrement mon âme-sœur, ma belle Montre-moi qu'il n'y a point d'amour comme tel Ma Dulcinée, tu es plus délicieuse qu'un caramel
Mediafile available in formats
http://univideos.ru/ website is the best way to download a video or a separate audio track if you want to do without installing programs and extensions.
The UDL Helper extension is a convenient button that is seamlessly integrated into YouTube, Instagram and OK.ru sites for fast content download.
UDL Client program (for Windows) is the most powerful solution that supports more than 900 websites, social networks and video hosting sites, as well as any video quality that is available in the source.
UDL Lite is a really convenient way to access a website from your mobile device. With its help, you can easily download videos directly to your smartphone.
The best quality formats are FullHD (1080p), 2K (1440p), 4K (2160p) and 8K (4320p). The higher the resolution of your screen, the higher the video quality should be. However, there are other factors to consider: download speed, amount of free space, and device performance during playback.
The browser/computer should not freeze completely! If this happens, please report it with a link to the video. Sometimes videos cannot be downloaded directly in a suitable format, so we have added the ability to convert the file to the desired format. In some cases, this process may actively use computer resources.
You can download a video to your smartphone using the website or the PWA application UDL Lite. It is also possible to send a download link via QR code using the UDL Helper extension.
The most convenient way is to use the UDL Client program, which supports converting video to MP3 format. In some cases, MP3 can also be downloaded through the UDL Helper extension.
This feature is available in the UDL Helper extension. Make sure that "Show the video snapshot button" is checked in the settings. A camera icon should appear in the lower right corner of the player to the left of the "Settings" icon. When you click on it, the current frame from the video will be saved to your computer in JPEG format.
For this purpose you need VLC-player, which can be downloaded for free from the official website https://www.videolan.org/vlc/.
How to play streaming video through VLC player:
To download streaming video via VLC player, you need to convert it:
Warning: this download method no longer works with most YouTube videos.
It costs nothing. Our services are absolutely free for all users. There are no PRO subscriptions, no restrictions on the number or maximum length of downloaded videos.